Level 26 Level 28
Level 27

Are there really this many body parts?


87 words 0 ignored

Ready to learn       Ready to review

Ignore words

Check the boxes below to ignore/unignore words, then click save at the bottom. Ignored words will never appear in any learning session.

All None

Ignore?
res wi
the liver
Bés bu nekk, mu lakklu aw resu lëmm.
Each day, he grills an entire liver
put bi
the throat
reewu bi
the incisor tooth
bëñu janoo bi
the incisor tooth (facing tooth)
Reewu yi saxaguñu.
The incisors have not yet pushed through
baaraamu sànnikaay
index finger
baaraamu joxonukaay
index finger (pointing finger)
purux
throat
Purux fàtte na ñamu daaw.
The throat has forgotten last year's food (someone ungrateful forgets the good things they have received).
kaabaab
jaw
ŋaam
jaw
Ay ŋaam yu dëgër la am.
He has solid jaws.
cër bi
the limb; the share/part/status/social position
Warula laal benn cër ci sa yaram.
He must not touch a single limb on your body.
yuq gi
the (bone) marrow
Yuqu yax wi la bëgg.
He wants the bone marrow.
dëgëj gi
the molar
Dogtoor bi dindi na sama dëgëj.
The doctor removed my molar.
yul bi
the calf (leg)
mustaas yi
the moustache (from French)
Amuloowoon ay mustaas.
You didn't have a moustache.
siddiit bi
the muscle/nerve/tendon/vein
Dafay defar ay leraw ak siddiitu nag.
He makes whips from cow tendons.
Deret ji ci siddiit yi lay jaar.
The blood passes thorugh the veins.
jumbax bi
the nostril
Gaañ nga ma ci jumbax.
You hurt my nostril.
doq gi
the nape (of neck)
Tegal sa loxo ci sama doq.
Put your hand on the nape of my neck.
ndoŋ li
the back of the head
Amatul kawar ci ndoŋ li.
He has no more hair on the back of the head.
boli bi
the throat/oesophagus/larynx
Ñam yi ci boli bi lañuy jaar
The foods pass by the oesophagus.
yax wi
the bone
Ay yax rekk a des.
Only the bones remain.
sull bi
the penis
kooy bi
the penis
May na ma ab dànku ceeb.
He gave me a handful of rice.
tipp-jara bi
the wrist
Sama tipp-jara dafay metti.
My wrist hurts
kurpeeñ bi
the fist
Xamuma nimoro dàllam.
I don't know his shoe size.
dënn bi
the chest
xëtër wi
the lung
Buleen jaawale xol ak xëtër.
Don't (plural) mix up heart and lung.
peru bët
pupil (of the eye)
Peru bëtu ndeyjoor bi
The pupil of the the right eye.
kanam bi
the genitals (lit. The front/face)
tëstën bi
the heel
Tëstën bi mënula dugg ci dàll wi.
The heel cannot enter in the shoe.
siis bi
the tendon/gristle/sinew
Dagg nañu siis bi.
They cut the tendon.
xuur wi
the testicle
Naka ngéen di waxe xuur ci séen làkk?
How do you say testicle in your language?
yeel bi
the shin
Wéq naa ko ci yeel.
I kicked him in the shin.
borom-nopp bi
the eardrum (lit. Owner of the ear)
ndëndu nopp mi
the eardrum
Coow li dina bënn sama ndëndu nopp.
The noise is going to burst my eardrum.
mbuus mi
the bladder
Mbuus mi dafa bënn.
The bladder is torn.
Tiit na bi ma xàccee kurpeeñ.
He was afraid when I brandished (my) fist.
baaraamu déy bi
the thumb/big toe
bos bi
the hump
bun gi
the anus; the buttocks
caas gi
the tendon; the fishing line
ciiñ gi
the gum (in the mouth)
cokk bi
the pubic hair
coppret bi
the clitoris
cott bi
the clitoris (vulgar)
cus bi
the nipple
cuukel bi
the bump at the back of the skull
dë bi
the sole of the foot
gat
buttocks/ass/rear end (vulgar)
gàddaam gi
the spleen
jaal wi
the space in the mouth were a tooth is missing
siiñ wi
the gum (in the mouth)
Sama siiñ newwi na.
My gum is swollen.
nafsu bi
the nose; the life
naq bi
the lower abdomen
nen yi
the testicles (Slang, lit. The eggs)
nenukaay bi
the ovary
ndigg li
the hip/lower back; the waist of a garment
paftan mi
the bladder
paxu bakkan bi
the nostril (nosehole)
përëg mi
the upper arm
pottax bi
the larynx/Adam's apple